Content-Length: 167738 | pFad | https://wo.wikipedia.org/wiki/Fewirie

Fewirie — Wikipedia Aller au contenu

Fewirie

Jóge Wikipedia.
Fewirie, Leandro Bassano

Weeru Fewirie mooy ñaareelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Baat baa ngi jóge ci latin: februarius, ngir màggale ko yàllay waa-rom ja: Februa. Ca jamono ju yàgg ja, moo nekkoon ñaareelu weer ci arminaatu waa-rom, at mi 15 Maars la daan door.

Mooy weer wi gën a gàtt ci at mi, mooy wenn wi dul àgg mukk 30 fan.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar








ApplySandwichStrip

pFad - (p)hone/(F)rame/(a)nonymizer/(d)eclutterfier!      Saves Data!


--- a PPN by Garber Painting Akron. With Image Size Reduction included!

Fetched URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/Fewirie

Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy